un vrai site pour le senegal
 

Lexique Wolof/Français
A
 

Wolof Prononciation Français
Aada   Coutûmes
Aaye ou Tere   Interdire
Abal ma ma tàll   Prêtes-moi du feu
Agsi   Arriver
Ajjuma   Vendredi
Ak   Avec
Allarba   Mercredi
Altine   Lundi
Alxames   Jeudi
Am   Avoir
Am, Moom   Posséder
Ana waa kër gi?   Comment vont les gens de ta famille?
Askan   Peuple
Assamaan   Ciel
At Ate Année
Attaaya   Thé
  Déjeuner

B

Wolof Prononciation Français
Ba bennén Ba bénéne A bientôt (à la prochaine)
Baal   Excuser
Baal ma   Pardon
Baaraam   Doigt
Baat   Cou
Baat   Voix
Baax   Bon
Baax   Gentil
Baax na   C'est bien, ça va
Bakkan   Nez
Ball   Pardonner
Banneex   Plaisir
Bari   Nombreux
Baré   Beaucoup
Baré na!   C'est cher!
Battaxal   Message
Baxa   Bleu
Bayyi   Laisser
Bañ   Refuser
Bees   Neuf (du)
Bees   Nouveau
Beg   Etre gai
Beg   Content
Beg   Satisfait
Benn   Un
Berep   Lieu
Biir   Intérieur
Biir   Ventre
Bind   Ecrire
Biti   Dehors
Bopp   Tête
Bukki   Hyène
Bëgg   Désirer
Bët   Oeil, Yeux
Bëñ   Dent


C

Wolof Prononciation Français
Caabi   Clef
Caaxaan   Blague
Caaxaan, Fo, Kaf   Plaisanter
Cammooñ   Gauche
Ceeb   Riz
Coow
C

Wolof Prononciation Français
Caabi   Clef
Caaxaan   Blague
Caaxaan, Fo, Kaf   Plaisanter
Cammooñ   Gauche
Ceeb   Riz
Coow  

D

Wolof Prononciation Français
Daanu   Tomber
Dab   Rattraper
Dafa   Il ou Elle
Dafa beg   Elle est contente
Dafay dem   Il ou elle part
Dafay nélaw   Il dort
Daje   Rencontrer
Dall   Chaussures
Dama   Je
Dama bëgg   Je veux ou je voudrai
Dama marr   J'ai soif
Dama tang   J'ai chaud
Damay dem   Je pars
Damay tëgg balafon   Je joue du balafon
Danga   Tu
Danga sonn   Tu es fatigué
Dangay dem   Tu pars
Dangay xool   Tu regardes
Dangeen   Vous
Dangeen dem   Vous partez
Daqaar   Tamarin
Dara   Rien
Daw   Courir
Dañu   Nous
Dañuy dem   Nous partons
Dañuy ligeey   Nous travaillons
Dee   Mort
Deedeet   Non
Def   Faire
Defar   Fabriquer
Degg   Comprendre
Degg   Entendre
Deggal   Obéir
Deglu   Ecouter
Dem Déme Aller
Dem   Partir
Demb   Hier
Des   Rester
Dex   Fleuve
Deñuy dem   Ils ou elles partent
Dibeer   Dimanche
Dieuleul ouarga bi   Prends le thé
Dieun,am na téy ci guedj bi lool   Il ya du poisson aujourd'hui(en mer)
Diggante   Distance
Diis   Lourd
Dikk, Ñëw   Venir
Dimbale   Aide
Dindi   Enlever
Diokh ma suker si   Passes-moi le sucre
Dof   Fou
Door   Débuter
Door   Frapper
Doyadi   Insuffisant
Dugal   Introduire
Dugg   Entrer
Duss   Toilettes
Démal diendi khorom   Vas acheter du sel
Dëgg   Vérité
Dëkk   Ville, Village
Dëng   Malhonnête (être)

 
aujourd'hui 2861 visiteurs (4094 hits) cette page
par http://lesenegal.fr.gd Ce site web a été créé gratuitement avec Ma-page.fr. Tu veux aussi ton propre site web ?
S'inscrire gratuitement